Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 83:13-16 in Wolof
Help us?
Sabóor 83:13-16
in
Kàddug Yàlla gi
13
ña ne woon: «Nan séddoo parluy Yàlla yi.»
14
Éy Yàlla, wëndeel leen ni callweer, ñu mel ni boob mu ngelaw wal.
15
Éy Yàlla, ni daay di xoyome àll, sawara wa jafal tund ya,
16
yal nanga leen ni toppeek sa dooley ngelaw, tiitale leen sa ngëlén.
Sabóor 83 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms