Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 83:13-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 83:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 ña ne woon: «Nan séddoo parluy Yàlla yi.»
14 Éy Yàlla, wëndeel leen ni callweer, ñu mel ni boob mu ngelaw wal.
15 Éy Yàlla, ni daay di xoyome àll, sawara wa jafal tund ya,
Sabóor 83 in Kàddug Yàlla gi