Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 82:5-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 82:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 «Ndawi péncum Yàlla yii xamuñu, dégguñu; xanaa di doxe lëndëmu ñaawtéef, ba kenuy suuf yépp di jaayu.
6 «Dama ne ay yàlla ngeen, yeen ñépp di njabootu Aji Kawe ji.
7 Waaye du leen tee dee ni doom aadama, du leen tee daanu ni képp kuy njiit.»
Sabóor 82 in Kàddug Yàlla gi