Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 82:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 82:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Sàmmleen àqu néew-ji-dooleek jirim, tey àtte yoon ku ñàkk ak ku ndóol.
4 Walluleen néew-ji-dooleek walaakaana, di leen xettli ci ku bon.
Sabóor 82 in Kàddug Yàlla gi