Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 81:8-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 81:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 Ngeen jàq, woo ma, ma xettli leen, wuyoo leen fa kiiraayal dënn ya, te maa leen nattoo fa wal ma ca Meriba. Selaw.
9 Yeen sama ñoñ, dégluleen, ma dénk leen. Éy Israyil, su ngeen ma déglu woon!
Sabóor 81 in Kàddug Yàlla gi