Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 81:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 81:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 «Sippi naa leen, woyofal seeni yoxo.
8 Ngeen jàq, woo ma, ma xettli leen, wuyoo leen fa kiiraayal dënn ya, te maa leen nattoo fa wal ma ca Meriba. Selaw.
Sabóor 81 in Kàddug Yàlla gi