Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 81:5-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 81:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Loolu wartéefu Israyil la, di ndigalu Yàllay Yanqóoba,
6 di ndénkaane lu mu dénk waa kër Yuusufa, ba Yàllay dali ca kaw réewum Misra. Baat bu ma xamul laa dégg, mu naan:
Sabóor 81 in Kàddug Yàlla gi