Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 81:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 81:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Yékkatileen woy te jiin, xalam neex, ànd ak moroom ma.
4 Wal-leen liit gi ci Terutel weer wi, ak weer wu birale bésu màggal.
Sabóor 81 in Kàddug Yàlla gi