Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 81:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 81:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Éy su ma sama ñoñ déggaloon, éy su Israyil toppoon samay nammeel!
15 Ci saa si laay torxal seeni noon, duma seeni bañ,
16 ba ku bañ Aji Sax ji di ko raamal, te àppam du jeex ba fàww.
Sabóor 81 in Kàddug Yàlla gi