Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 81:12-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 81:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 «Waaye sama ñoñ déggaluñu ma, Israyil gii nangulu ma.
13 Moo tax ma bërgël leen ak seenug të, ñuy wéye seeni pexe.
14 Éy su ma sama ñoñ déggaloon, éy su Israyil toppoon samay nammeel!
Sabóor 81 in Kàddug Yàlla gi