Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 7:7 in Wolof

Help us?

Sabóor 7:7 in Kàddug Yàlla gi

7 Aji Sax ji, meral, jóg, dajeel maak xadaru noon yi! Ngalla teewlu ma; yaw, yoon nga santaane.
Sabóor 7 in Kàddug Yàlla gi