Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 7:5-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 7:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 ndegam ku ma jàmmal laa feye aw ay, mbaa ma dimbali ku ko noonoo te defu ko dara,
6 yal na ma noon rëbb, dab ma, dëggaate ma, sàggi saab sag, tëral ci pëndub suuf. Selaw.
Sabóor 7 in Kàddug Yàlla gi