Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 7:13-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 7:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Ku tuubul, Yàlla nàmm saamaram, bank xalaam, diir la.
14 Moom la waajalal ngànnaayi ndee, def ko fitt yuy boy.
15 Ku bon a ngoog, di matu doomu ñaawtéef. Day sos njombe, wasin njublaŋ.
Sabóor 7 in Kàddug Yàlla gi