Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 79:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 79:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Ñu tuur seen deret nim ndox, ba Yerusalem daj, te amul kuy rob néew yi.
4 Noo ngi nii di mbalitu dëkkandoo yi; ñu séqe nu ay kókkaleeki kekku.
5 Aji Sax ji, xanaa doo nu mere ba fàww, sa fiiraange ni sawara ci sunu kaw?
Sabóor 79 in Kàddug Yàlla gi