Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 78:69-71 in Wolof

Help us?

Sabóor 78:69-71 in Kàddug Yàlla gi

69 Mu tabax këram gu sell, na mu mel fa kawa kaw, dëgër ni suuf, si mu samp ba fàww.
70 Mu teg ca tabb Daawuda, jaamam ba, jële ko ca gétti xar ya,
71 fa mu doon topptoo jur ga; mu sàmmal ko waa kër Yanqóoba, askanu Israyil wi mu séddoo.
Sabóor 78 in Kàddug Yàlla gi