Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:62-65

Help us?
Click on verse(s) to share them!
62Daa bàyyee ñoñam saamaru noon, ndax mere yooya séddoom.
63Seeni waxambaane deeye xare, seeni janq lamb;
64seeni sarxalkat loroo saamar, te jëtun jooyul.
65Ca la Boroom bi yewwu ni ku doon nelaw, mel ni jàmbaar ju biiñ xabtal.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:62-65Sabóor 78:62-65