Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 78:13-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 78:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Moo xar géej ga, jal ndox ma nim tata, jàlle leen.
14 Bëccëg mu jiitee leen aw niir, ak leeru sawara guddi gépp.
15 Moo xar ay doj ca màndiŋ ma, mbàmbulaan wal, mu nàndal leen;
16 mu sotti ndox mu balle ciw xeer, walal, mu safi dex.
Sabóor 78 in Kàddug Yàlla gi