Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 77:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 77:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Guddi may fàttliku sama woy, di waxtaan ak sama ngegenaay, sama xel di jéex te naa:
8 «Boroom bi da may gàntal ba fàww, ba du ma baaxeeti mukk a?
Sabóor 77 in Kàddug Yàlla gi