Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 77:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 77:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Naa xalaat sa bépp liggéey, di jàngat say jëf.
14 Céy Yàlla, yaa sell jikko! Jan yàllaa màgg ni Yàlla?
Sabóor 77 in Kàddug Yàlla gi