Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 76:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 76:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Yaw Yàllay Yanqóoba, yaa gëdd, gawar ak fasam nelaw.
8 Yaw mii, yaa mata ragal; boo meree, ana kuy taxaw fi sa kanam?
9 Fa asamaan nga biraleb àtte; suuf tiit, ne cell.
Sabóor 76 in Kàddug Yàlla gi