Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 76:4-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 76:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Fa la rajaxee fitt yuy boy ak pakk ak saamar ak ngànnaayal xare. Selaw.
5 Yàlla yaa ne ràññ te darajawu, ba raw tundi rëbbkat yi.
6 Futtees nay boroom fit, ñu ne nërëm, nelaw; kuy ñeyi xare, say yoxo nasax.
Sabóor 76 in Kàddug Yàlla gi