Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 76:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 76:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Xaymaam a nga Salem, di xunteem ma fa Siyoŋ.
4 Fa la rajaxee fitt yuy boy ak pakk ak saamar ak ngànnaayal xare. Selaw.
Sabóor 76 in Kàddug Yàlla gi