Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 75:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 75:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Yàlla nee: «Maay takk ab àpp, àtte ca njub.
4 Bu suuf di yëngu mook ñi ko dëkke ñépp, maay kiy téye ay kenoom. Selaw.
5 Dama ne ku réy: “Bul réy-réylu,” ne ku bon: “Bul bew,
Sabóor 75 in Kàddug Yàlla gi