Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 74:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 74:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Dañoo taal sa kër gu sell, sa dëkkuwaayu tur lañu daaneel, ba sobeel ko.
8 Ñu namm noo not ba nu nooy, fuy bérabu ndajem Yàlla ci réew mi, ñu lakk.
Sabóor 74 in Kàddug Yàlla gi