Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 74:20-22 in Wolof
Help us?
Sabóor 74:20-22
in
Kàddug Yàlla gi
20
Ngalla xoolal ci kóllëre gi, fu làqu ci réew mi, fitna dale fa ba dajal.
21
Yàlla bu néew-doole ñibbaale gàcce, yal na ku ñàkk ak ku néewle di la santandoo.
22
Éy Yàlla, jógal ñoŋal sa dëgg, bàyyil xel dof bi la dëkkee sewal.
Sabóor 74 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms