Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 74:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 74:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 yaa rajaxe kaaŋi rab wa, leele ko rabi màndiŋ ma.
15 Yaa fettaxal fii bëti ndox akum wal, ŋiisal dex yu masa wal.
16 Yaa moom bëccëg, moom guddi, teg fi weer week jant bi.
Sabóor 74 in Kàddug Yàlla gi