Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 74:13-15 in Wolof

Help us?

Sabóor 74:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Yaa xàjjale géej gi ci sa doole, toj boppi ninki-nànka ya ca ndox ma,
14 yaa rajaxe kaaŋi rab wa, leele ko rabi màndiŋ ma.
15 Yaa fettaxal fii bëti ndox akum wal, ŋiisal dex yu masa wal.
Sabóor 74 in Kàddug Yàlla gi