Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 73:8-11 in Wolof

Help us?

Sabóor 73:8-11 in Kàddug Yàlla gi

8 Dañuy ñaawle, di wax lu bon, di réy-réylu, boole ci kàdduy jaay-doole.
9 Seen ŋal-ŋal àkki asamaan, làmmiñ dajal suuf.
10 Moo tax ñoñi Yàlla walbatiku ci ñoom, di jolu seen wax nim ndox
11 te naan: «Lu ci Yàlla xam? Ana xam-xam fa Aji Kawe ji?»
Sabóor 73 in Kàddug Yàlla gi