Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 73:5-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 73:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Doñ-doñu nit dabu leen, coonoy doom aadama dalu leen.
6 Moo leen taxa ràngoo reewande, làmboo coxor.
7 Dañoo suur ba gët suulu, seen xalaati xel xëtt yoon.
Sabóor 73 in Kàddug Yàlla gi