Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 73:27-28 in Wolof

Help us?

Sabóor 73:27-28 in Kàddug Yàlla gi

27 Ku la sore kat, sànku; képp ku la wor, nga fàkkas.
28 Man de, jege Yàllaa ma gënal. Boroom bi, Aji Sax ji, yaw laa def kiiraay, ngir siiwal sa jépp jëf.
Sabóor 73 in Kàddug Yàlla gi