Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 73:24-26 in Wolof

Help us?

Sabóor 73:24-26 in Kàddug Yàlla gi

24 Danga maa gindee sam xel, teg ca dalale ma sa teddnga.
25 Ana ku ma am asamaan ku la moy? Ku ma safoo kaw suuf ku la moy?
26 Kàttan ak pexe jeex, Yàlla di ma dooleel, ma séddoo ko fàww.
Sabóor 73 in Kàddug Yàlla gi