Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 73:21-23 in Wolof

Help us?

Sabóor 73:21-23 in Kàddug Yàlla gi

21 Naqar laa amoon, sama xol di dagg.
22 Booba ngaaka laa, xawma dara; rab laa woon fi sa kanam.
23 Teewul ma des ak yaw, nga jàpp sama loxol ndijoor.
Sabóor 73 in Kàddug Yàlla gi