Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 73:20-21 in Wolof

Help us?

Sabóor 73:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Day mel ni gént goo yewwoo. Céy Boroom bi, boo xippee, jëmmu gént ga soof la.
21 Naqar laa amoon, sama xol di dagg.
Sabóor 73 in Kàddug Yàlla gi