Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 73:16-18 in Wolof

Help us?

Sabóor 73:16-18 in Kàddug Yàlla gi

16 Naka laay jéema ràññee lii, mbir mi ëlëm ma.
17 Ba ma àggee sa kër gu sell ga, laa doora gis muju ku bon.
18 Yoonu tarxiis kay, nga leen teg, daane leen, ñu sànku,
Sabóor 73 in Kàddug Yàlla gi