Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 73:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 73:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Bés bu ne yar dal ma, saa yu ma xëyee, jot mbugal.
15 Su ma noon: «Naa waxe ni ñoom,» kon de, ma wor sa askanu mbooloo.
16 Naka laay jéema ràññee lii, mbir mi ëlëm ma.
Sabóor 73 in Kàddug Yàlla gi