Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 73:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 73:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Man kay maa sellal ci neen, di sàmm sama der.
14 Bés bu ne yar dal ma, saa yu ma xëyee, jot mbugal.
Sabóor 73 in Kàddug Yàlla gi