Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 73:10-12 in Wolof

Help us?

Sabóor 73:10-12 in Kàddug Yàlla gi

10 Moo tax ñoñi Yàlla walbatiku ci ñoom, di jolu seen wax nim ndox
11 te naan: «Lu ci Yàlla xam? Ana xam-xam fa Aji Kawe ji?»
12 Ñu bon ñaa ngoog! Ne finaax, di gëna woomle.
Sabóor 73 in Kàddug Yàlla gi