Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 72:6-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 72:6-7 in Kàddug Yàlla gi

6 Yal na Buur di xéewalu réewam nib taw cig ruujeef, mbaa waame wuy suuxat suuf.
7 Janti Buur aji jub day woomle, te ba keroog weer wiy fey, jàmm di law,
Sabóor 72 in Kàddug Yàlla gi