Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 72:5-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 72:5-8 in Kàddug Yàlla gi

5 Yal nañu la wormaal feek jant biy am, feek weer wiy feq, sët ba sëtaat.
6 Yal na Buur di xéewalu réewam nib taw cig ruujeef, mbaa waame wuy suuxat suuf.
7 Janti Buur aji jub day woomle, te ba keroog weer wiy fey, jàmm di law,
8 mu yilif géej ba géej ak dex ba ca cati àddina.
Sabóor 72 in Kàddug Yàlla gi