Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 72:4-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 72:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Buur di àtte néew-ji-dooley xeet wi, di wallu doomi néew-ji-doole tey dëggaate kiy nennoo.
5 Yal nañu la wormaal feek jant biy am, feek weer wiy feq, sët ba sëtaat.
Sabóor 72 in Kàddug Yàlla gi