Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 72:15-16 in Wolof
Help us?
Sabóor 72:15-16
in
Kàddug Yàlla gi
15
Yal na Buur gudd fan, yal nañu ko may wurusu Saba. Nañu koy ñaanal saa su ne, di ko saxoo, mu barkeel.
16
Yal na pepp ne gàññ ci réew mi, yal na gub yay jaayu ca tund ya ni gottub Libaŋ; dëkk yu mag yi sëqi nit ba law,
Sabóor 72 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms