Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 72:12-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 72:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 Mooy xettliji aji tumurànke bu woote wall ak aji néewle ju sësul fenn.
13 Mooy yërëm ku néewleek ku tumurànke, di sàmm bakkanu aji tumurànke,
14 boole leen jot ci notaangeek loraange, ngir fonk seen bakkan.
Sabóor 72 in Kàddug Yàlla gi