Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 72:11-13 in Wolof

Help us?

Sabóor 72:11-13 in Kàddug Yàlla gi

11 buuroo buur di ko sujjóotal, xeetoo xeet di ko surgawu.
12 Mooy xettliji aji tumurànke bu woote wall ak aji néewle ju sësul fenn.
13 Mooy yërëm ku néewleek ku tumurànke, di sàmm bakkanu aji tumurànke,
Sabóor 72 in Kàddug Yàlla gi