Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 72:10-11 in Wolof

Help us?

Sabóor 72:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 buuri Tarsis ak dun ya di ko indil ay galag; buuri Saba ak Seba di ko yótsi yóbbal,
11 buuroo buur di ko sujjóotal, xeetoo xeet di ko surgawu.
Sabóor 72 in Kàddug Yàlla gi