Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 70:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 70:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Kuy wut sama bakkan, yal na rus, torox ne tott. Kuy bége sama loraange, yal nañu ko duma, waññi ko, mu ne yàcc.
4 Kuy ñaawle, yal na dellu gannaaw, torox.
Sabóor 70 in Kàddug Yàlla gi