Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 6:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 6:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax ji, damaa néew doole, yërëm ma! Éy Aji Sax ji, sama yaram a tas, dàmp ma!
4 Sama xol a jeex tàkk. Aji Sax ji, loo deeti xaar nag?
5 Éy Aji Sax ji, délsil, xettli ma! Walloo ma sa ngor.
Sabóor 6 in Kàddug Yàlla gi