Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 68:5-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 68:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Woyleen Yàlla, teral turam, xàllal-leen kiy war niir yi, Ki Sax moo di turam. Bànneexuleen fi kanamam.
6 Mooy baayoo jirim, di àtte jëtun, kookoo di Yàlla ja fa dëkkuwaayu sellngaam.
7 Yàllaay sàkkal ku wéet wéttal, di afal ku ñu tëjoon, bégal ko, ku déggadi rekk ay dëkke suuf su ne sereŋ.
Sabóor 68 in Kàddug Yàlla gi