Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 68:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 68:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Yàlla wal, ñu naaw ni saxar. Ñu bon ñi sànku fi kanam Yàlla, mbete dax ak sawara.
4 Ñu jub ñi nag bég, di bànneexu fi kanam Yàlla, tey puukarewoo mbégte.
Sabóor 68 in Kàddug Yàlla gi