Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 68:19-20 in Wolof

Help us?

Sabóor 68:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Yaa yéeg fa kawa kaw, jàpp ay jaam, yóbbaale. Yaa nangooy galag ci nit ñi, ba ci ñiy fippu ndax li Yàlla Ki Sax dëkke Siyoŋ.
20 Cant ñeel na Yàlla bésoo bés. Moo nuy jaboote. Yàllaa nuy musal. Selaw.
Sabóor 68 in Kàddug Yàlla gi