Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 68:17-18 in Wolof

Help us?

Sabóor 68:17-18 in Kàddug Yàlla gi

17 looy xeelook say coll, di fiire tund wi Yàlla namma dëkke? Aji Sax ji kat, fa lay dëkk ba fàww!
18 Watiiri xarey Yàlla di ñaar fukki junni (20 000), ba ci junniy junni. Boroom bi ne ca seen biir, di boroom tundu Sinayi fa biir sellngaam.
Sabóor 68 in Kàddug Yàlla gi